À la Une
A LA UNE

Waxtaanu koor 2025

A LA UNE - dimanche 02 mars 2025 · 1 Mins

Waxtaanu koor 2025
Wilaya Section Touba

1 — Maam Moor MBÀKKE
Xam sa Diine lim wara waxtaane👇👇
مسؤولية المريد في رعاية حرمة مدينة طوبى المحرسة
Li war Murit yi ci sàmm wormay Tuubaa

2– Seex Ahmadu Mbàkke ÑAŊ
lim wara waxtaane 👇👇
السلام طريق إلى تحقيق وحدة المسلمين2- السلام طريق إلى تحقيق وحدة المسلمين
Jàmm moo mana andi Bennoog jullit yi

3– Sëñ Fàllu BUSO Asan
lim wara waxtaane👇👇
شبكات التواصل الاجتماعي وأثرها على المجتمع
Mbaa li jokkoo yi (réseau sociaux) yan jeexiit lay def ci Askan wi

4–Sëñ Fàllu BUSO Cerno
lim wara waxtaane👇👇
التربية عند الشيخ الخديم سبيل النجاح في حل أزمة الأخلاق
Njàngalem, Seexul Xadiim ci Yar mooy yoonu saafara jikko yu yàqu yi.

Écrit / Rapporté Par
admin

Rédacteur certifié par la cellule d'information Fédérale pour retranscrire fidèlement nos publications officielles.

Archive précédente
Biographie de Serigne Fallilou Mbacké
Archive Recente
CRD préparatoire magal Darou khoudoss 2025
Joindre l'assistance