À la Une
DOSSIER 18 SAFAR

Déclaration Seex Baasiru Mbàkke Ibn Seex Abdul Xaadir

DOSSIER 18 SAFAR - lundi 13 septembre 2021 · 1 Mins

https://www.youtube.com/watch?v=pR3iGCydvIU

Ndigalul Sëriñ Muntaxaa Mbàkke jëm ci Waaj taayu Màggal gi kàdduy Ndigal jëm ci dikkug jiitul Réew mi ak Ninu wara nekkee ci dëkk bi nuy wormaal bépp kilifa bufi ñëw yokk a wormaal dëkk bi ta gëna rafetal dëkkiin wi ci mbedd yi ak tali yi.

Écrit / Rapporté Par
admin

Rédacteur certifié par la cellule d'information Fédérale pour retranscrire fidèlement nos publications officielles.

Archive précédente
Cheikh Moustapha, l’exemple type du Mouride
Archive Recente
Diplôme de reconnaissance: Rëlaasion Sargal à Serigne Bassirou Dieng
Joindre l'assistance